Yeewu Leen - 19 Mars 2014 - Actualité People avec Bijou Ndiaye


Mercredi 19 Mars 2014




1.Posté par cheikh goumbala le 20/03/2014 07:37
TFM télé bi beury féém Macha alah bi télé môléni yéém Boyabô ga deukè seuguéém naxe beug baññe douko téréé dem Yi animateur ak animatrice sa beuri xorom Wayé yî journaliste tê beuri xam-xam Sêtânelêên day yokou ndam Bî télé dalay dieumé kanam Dalay yokou diam dila may diom Ñî bôlééni sêtâne dalay dolly gueum-gueum Bôye sêtâne TFM dô gueuleum Deug néxoul wayé TFM môye bombou Lô daw-daw dôko rômbou Kou ñémé naga taxaw kou ragal naga daw TFM migui ñeuw dall séén kaw...



Dans la même rubrique :