Victoire des mbalaxmen sur les rappeurs


Victoire des mbalaxmen sur les rappeurs


Victoire des mbalaxmen sur les rappeurs
Dakaractu2




Lundi 1 Juillet 2013
Notez


1.Posté par mb2 le 01/07/2013 12:30
rapeur yi diouklène si sen bopp a chaque foi rek mbalah man yi haw léne réy kone nak mbalakh man yi gno ka yoor namounou dara

2.Posté par Kiné WADE le 01/07/2013 14:43
wa mé mdr, mé Waly, lan la sol ni calecon SOKHNA AIDARA?

3.Posté par Mme xxxxxx le 01/07/2013 23:57
Ah contane na si waly nila gor day diongué bari thiath ak salagne salagne dou femme yi rek la war souma guissé gor bou beug diabaram dikoko prouvé a chaque instan damay bégue dina outal mon mari des caleçon signè a mon nom.yalna la yala bayi ak ta femme

4.Posté par doul le 03/07/2013 16:47
iaw bougnou raye guay wone wou nane beug boula beugone doula fi bayi di dem fenene mb2 kine wade mme c la meme persone te xamnanou kanela doul way



Dans la même rubrique :