Nouveau Single! Mack Y oni (Macky Doyna) !!! Par Talla SYLLA


Jeudi 12 Juin 2014
Dakaractu




1.Posté par boythieees le 13/06/2014 06:29
Ku gueneu gnak fayda ni talla sylla amoul. xana talla guewel la?

2.Posté par NDIAGA le 13/06/2014 09:04
ENCORE UN FINANCEMENT DE SAMUEL SARR, JUSQU'À CE QUE MACKY L'ACHETE A UN PRIX PLUS FORT. CE PARESSEUX EST UN MERCENAIRE SANS IDEAL.

3.Posté par UN PASSANT le 13/06/2014 09:07
trop fort Talla

4.Posté par moi meme le 13/06/2014 10:21
tu nous pompes l'air toi, laisse nous en paix, tu es nul et mechant.

5.Posté par dionny Ndiaye le 13/06/2014 10:48
Ngeen balma, ki dul demm Talla SYLLA là ci sama xalaat.
Xoolenn bu baax lii may wax.
Ci ganawam la Musa TINE nekoon, tay ji kookee rommb nako di wey.
Muy melni ku andul ak sagoom, lumu yor rek wacc ko. Depité ba ak ministere ba niu ko diggonn yepp.
Melni kenn menu ko muur ba du tooy.
Cey Talla xoolatal say diar diar te yedd sa bopp. te nga wax wa senegal ca degg degg lu di sa liggey?
kiy demm Yalla Mawlana Hu rekk mo ko xamm.
May sukk ndikku ci sunnu Serigne bu tedd ba "Dabaax" mo daan wax: Ab gaal bu ci say bagas nekke, da ngay niaan mu mucc ndax bu keppu nga loru,
Yaw ak maky ku ci genna niru ag kuy demm?
XALAAS..........

6.Posté par MBARKA le 13/06/2014 12:32
SHEEEEEUUUUT!!!!!! un trés bon son !!!

7.Posté par dijon le 14/06/2014 07:25
vous êtes des jaloux, il faut laisser macky travailler vous avez un mauvais coeur vous n'êtes que des rancuniers des gens qui ne réfléchissent pas, tout le temps que tu as consacré pour sortir ton single de merde fallait le consacrer à autres choses pour l'avancement du pays dijon

8.Posté par couya faye le 14/06/2014 16:00
déçu saay noonou demb bougnou taay senn pééxxéé diouboul
talla quand g entendu que tu as été reçu pas wade je me dis que tu sais + ou tu vas ....

9.Posté par lllllllll le 15/06/2014 17:12
c du lourd ce son, o peut même la danser en boite !! Les mbalaxmen ont du soucis a se faire, il y a un gros concurrent



Dans la même rubrique :