Après avoir insulté les sénégalais, Nogui Dieng présente ses excuses


Vendredi 14 Mars 2014
Dakaractu




1.Posté par niass le 14/03/2014 12:06
bilahi koussi bayiwoul di deff ak wax lila nex té nane talibé serigne saliou la xawmal xiyam diguene ko layo. talibé Serigne bi dou melni

2.Posté par babs le 14/03/2014 11:29
Talibé serigne Salihou, mon oeil! tu nous as encore insulté. te mettre tout le temps nue et te dire talibé. quel paradoxe!

3.Posté par senegalese le 14/03/2014 12:58
Tamite nak senegal doff yek ,les p..... kou diougu dinane serigne saliou wayé bakhna rek

4.Posté par barou le 14/03/2014 12:18
......C'est plus sa bouche qui attire l'attention...pour le reste chére madame on s'en tamponne vraiment ; tu ne nous avait pas insulté du tout....

5.Posté par ndeyecoumbandiaye le 14/03/2014 12:24
je ne connaissais même pas cette fille, après videao bi la guiss pour voir mannequin la , li mou defone embrasser son mari et poster ça se fait pas que le mari soit jeune vieux, blanc etc, la vie privée doit rester privée pour imposer le respect et eviter les dérives. La video ou elel dit ma taay etait plus ridicule que blessant et ne nous conerne pas wakh deuk, park lou way def bopam, elle n a pas insulté elle a dit wa sengal ma taay, donc khana sen wa keur, wala ay mbokam, nous enegalais lamba on a ete envahis par la video publique mais honnetement on s'en foutait. Mais la elle a demandé pardon té lolou tiopmo meunouko, elle a l'air desolée donc arretons de l'insulter pour rien, c 'est dur de reconnaitre ses tords et de s'excuser alors ne soyez pas moins courageux et moins digne arretez de l'insulter, c'est fini diekh na.
Je conseille juste aux filles de la jet set là de savoir que leurs exces là doulene diarigne, j n parle pas de mariage, ni de religion, ni d'insulte, mais la dignité et le respect de toi niit daf ko wara aam ba bamouy dé, il faut eviter beug siiiw pour rien, beug khaliss beug aduna, amoul bene solo, souniou dé migui niouy khar, nga dé, ay niit niou doy war di fatéliko sa dieuf you boneu lolou rafettoul et puis les insultes, les commerages font mal quoi qu'on dise, alors ne faites rien louniouy khassé, kou yakh sa der na fek day feen, mais dara yéssoul niou sed la si galou khadieu, fek la nga siy lek

6.Posté par Sokho le 14/03/2014 12:50
Talibe SERIGNE Saliou dou mel ni yeuy gnomalkhiyam Dina meti lolou lou takh
Legui cochon bou jogu di Serigne Saliou gnakk ko kham rek

7.Posté par salhhs le 14/03/2014 12:52
beugue def buzz pour siw boula diaralè di foyè safara si sa kaw lay takeu dieupèt

8.Posté par Baye le 14/03/2014 12:53
Yalla na yalla yerume serigne saliou aka beri gnouko togne

9.Posté par Alex le 14/03/2014 16:29
mane personellement je me chargerai de descendre une fois retourne en europe walakhi il Azim . beuss bo gneuwai senegal dana la reye

10.Posté par absa le 14/03/2014 22:56
En s'en vraiment de toi et ta vie pck nit day mandou wayè nitou yalla bou mel ni serigne saliou eup na toude si aye thiakhane so bagné lorou de grace sino nogui dieng ne nous intéresse pas vraiment

11.Posté par dof-le-fou le 14/03/2014 22:53
sale petasse!!! sofi niowé rék niou tégal sa ndeye diongal sa baye.

12.Posté par ça me fait mal le 14/03/2014 23:40
Bayilén di déf niawtéf ba paré di lakhou ci guinaw mouride yi. Tu te fout en encore des sénégalais en disant que tu es un talibé de serigne saliou. Un talibé de SERIGNE SALIOU ne comporte pas de la sorte, éspece de pute. Nitou kasara bi nga done.

13.Posté par BAMBA le 15/03/2014 01:07
yaw soxna sou djiguen gui, nguir Yallah ak Yonentebi ak dieumi Serigne Touba, LILLAHI WARASSOULIHIII, WAKhaL LOULA NEKH, DEFAL LOULA NEKH, C'EST TA VIE privée, mais boul wakhaty sa wakh moukk di ci toudd kou teddki Serigne Saalih Mbacke, damalako niaan rek, te yaakarna, dingamako may! te bouboba dinala niaanal yallah mou soppila kou bakh, nga toubb te bagnatesse dellouwatt. waw kay soxnassi, kon dinala sant loooole sakh. nga balma nak!

14.Posté par Pffff le 15/03/2014 13:18
Nooooo fuck it! On doit signer une pétition en ligne pour qu'on puisse interdire légalement ces journaliste a la noix de publier des articles des ces connes qui cherchent a faire le buzz parce qu'ils reussissent juste a énerver ceux qui veulent lire des infos constructives!!! Pkoiiiii?? Mais pkoiiii ils nous affligent ça !!!! Merde à la fin! Pitié arretezzzzz ça way!!! On mérite mieu ke ça way!!! Pfffff! Noooo li dou dem

15.Posté par mbow le 15/03/2014 15:22
ak talibe koukoy doundou deug diga am loy yeug ci sa biir khoul ba bo beugona def lou khamene teni sa mbokou talibe bouko deg rouss ligay yeug sa digante ak Serigne molakoy teree

16.Posté par Dembisse le 16/03/2014 19:12
ki dafa yap senegalais yi, 9a c'est honte pour l'image du senegal vraiment mais nak dinako guisse barki serigne Saliou !! c'est honteux !

17.Posté par shriii le 02/04/2014 20:55
no mane dé dama xamul kan mo interessé wou si yaw ba wax ma tay lo déf sa bopp ngako déf mw je té mém pa connu mé serigne saliou mom baka toudatè...



Dans la même rubrique :